Exodus 8:19
TSK
te maay musal sama ñoñ ci musiba moomuy dal saw askan. Ëllëg firnde jooju dina am.’ ”»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
te maay musal sama ñoñ ci musiba moomuy dal saw askan. Ëllëg firnde jooju dina am.’ ”»
Booba Sóol a nga naan: «Naa ko ko may, ngir mu doon ndëgg-sërëxam, ba waa Filisti teg ko loxo.» Sóol nag wax Daawuda, ñaareel bi yoon, ne ko: «Tey ngay samab goro.»
Ku bon day moy, ba dugal boppam; ku jub di woy ak a bànneexu.
Deesu la robaaleek yooyu buur, yaa yàq sam réew, faagaagal saw xeet. «Deesul tuddati mukk askanu lorkat wii.
Mowab tas, ay fereem serandoo.
Du seen xaalis, du seen wurus wu leen di mana xettli. Keroog bésub sànjum Aji Sax ji, ak sawaras fiiraangeem, àddina sépp ay xoyomu. Mooy raafal moos mboolem ñi dëkke àddina si, te raafal gu raglu lay doon!»