TSK

TSK · Exodus 12:32

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Esawu ne baayam: «Baay, xanaa genn ñaan rekk nga am? Ngalla baay, ñaanal ma, man itam!» Ca la Esawu ne yikkét jooy.

Tinuleen Aji Sax ji, ndax dënu yu màgg yeek tawub yuur bi dakk. Dinaa leen bàyyi, ngeen dem. Deesu leen fi téyeeti.»

Sunuy gétt dina nu topp moos, luy nirook we sax du des gannaaw, ndax ci lanuy tànne lu nuy màggale sunu Yàlla Aji Sax ji, te itam li feek nuy àgg foofa, manunoo xam lan lanu ciy def sarax, màggale Aji Sax ji.»