TSK

TSK · Exodus 19:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Keroog ca gannaaw-ëllëg sa, naka la njël jot, muy dënook a melax, ànd akaw niir wu fatt ca kaw tund wa, ak coowal liit gu xumb. Waa dal ba bépp a nga tiit, bay lox.

¶ «Su aw nag dañee góor mbaa jigéen, ba rey ko, dóorleen nag wi ay xeer ba mu dee, te buleen lekk yàpp wi, waaye boroom nag wi, yoon toppu ko.

Góor gu tëdde mala dee rekk mooy àtteem, te mala ma it dees koy rey.

Lu gaawa gaaw lay doon, ci xef ak xippi, bu liit gu mujj ga jibee; nde liit ga mooy jib, ñi dee, dekki, di ñu dul yàqooti, nun nag, nu soppiku.

Manuñu woona xajoo ndigal la ne: «Mala sax, su laalee tund wi, dóorleen koy doj ba mu dee.»