Genesis 13:8
TSK
¶ Ba loolu amee Ibraam da ne Lóot: «Waay waay, bu xuloo am sama digganteek yaw mbaa say sàmm ak samay sàmm. Xanaa dunuy bokk nag?
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba loolu amee Ibraam da ne Lóot: «Waay waay, bu xuloo am sama digganteek yaw mbaa say sàmm ak samay sàmm. Xanaa dunuy bokk nag?
La ca tegu doomi Yanqóoba ya ca des futti néew ya, lëlaale dëkk ba, ndax li ñu torxal seen jigéen.
Ña nga naan: «Boroom gént gaa ngee di ñëw!
Dangaa xeeb li nga nu jële réew mu meew maak lem ja tuuroo, ngir reylu nu ci màndiŋ mi, ba tax ngay buur-buurlu ci sunu kaw teg ci?
Merum buur ni gaynde gu ŋar; yërmandey buur ni lay cig mbooy.
Waaye waa réewam ña dañu koo bañoon. Ci gannaawam lañu yónni ndaw, ne: “Kii, bugguñu muy sunu buur.”
Ca ëllëg sa mu juux ci ay Yawut yuy xeex, di leen jéema jubale, ne leen: “Yeen ay bokk ngeen, lu tax ngeen di lorante?”