TSK

TSK · Exodus 2:5

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aji Sax ji def loola, weñ yi def ndiiraan yu réy, song kër Firawna ak kër dagam ya, dajal réewum Misra, ba réew ma yàqu ndax ndiiraani weñ ya.

Moom mooy àtte àddina cig njub, di dogalal xeet yi dëgg.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di jàngin wu ñeel askanu Kore wu góor, dëppook galan bu ñuy wax Baatu jigéen.

Xolu buur walum ndox la ci loxol Aji Sax ji, fu ko soob mu jëme ko fa.

Man nag, ci biir cant laa lay sarxale. Li ma xas laay sottal. Wall, fa Aji Sax ji!