TSK

TSK · Exodus 21:26

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Ku dóor yet jaamam bu góor mbaa bu jigéen, ba mu dee ciy loxoom, dees na ko feyul moos.

Buleen jalgati yoon cib àtte, buleen jeng te buleen nangu alalu ger, ndax ab ger day muur bëti boroom xel, di xañ aji jub dëgg.

Job 31:13 TSK

Ndegam maa sofental sama àqu jaam, bu ñu may jooytu, diy góor mbaa jigéen,

Yaw de yaay ki nemmiku, di gis njekkar ak naqar, ku mu dal, nga sàmm àqam. Néew-ji-doole wéeroo la, ab jirim, nga dimbali.

Mooy xettliji aji tumurànke bu woote wall ak aji néewle ju sësul fenn.

¶ Yeen it sang yi, jëfeleen noonu seen diggante ak seeni jaam, bàyyileen di tëkkoo, te ngeen xam ne yeen ak ñoom a bokk benn Boroom fa asamaan, te xejj ak seen amul fa moom.