¶ Aji Sax ji ne Musaa: «Loolu nga wax, moom laa lay defal, ndax daj nga samaw yiw, te it maa la xam ci saw tur.»
TSK
TSK · Exodus 31:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Exodus 33:17
TSK
Exodus 36:1
TSK
¶ «Kon nag Besalel ak Oliyab ak mboolem ñu xareñ ñi Aji Sax ji may xareñte ak déggin ngir ñu mana jëfe mboolem sas yi jëm ci liggéeyu bérab bu sell bi, ñoom ñépp nañu sottal lépp li Aji Sax ji santaane.»
Exodus 38:22
TSK
Fekk na Yudeen bi Besalel doomu Uri, miy doomu Ur, sottal na mboolem li Aji Sax ji santoon Musaa.
1 Kings 7:14
TSK
Doomu jëtun la woon, bokk ci giirug Neftali. Baayam dëkkoon Tir, di tëggub xànjar. Uram di ku xareñ lool, rafet xel te mane mboolem liggéeyu xànjar. Mu dikk ca Buur Suleymaan, liggéeyal ko la ñu ko sant lépp.
Isaiah 45:3
TSK
Maa lay jagleel denc yu loq, ak alal ju làqe, ba nga xam ne maay Aji Sax ji lay wooye sa tur, man Yàllay Israyil.