TSK

TSK · Exodus 32:19

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Yonent Yàlla Maryaama, jigéenub Aaróona nag ŋàbb tabala, jigéen ñépp topp ko, génn di fecc, tabala ya jiin.

Musaa nag tinu Yàllaam Aji Sax ji ne ko: «Aji Sax ji, ana lu waral sam sànj di tàkkal sa ñoñ ñi nga génne réewum Misra ci sa kàttan gu màgg ak sa dooley loxo?

Góor ga Musaa nag defoon ku woyof lool, ba raw mboolem doom aadama ci kaw suuf.

Dinaa bind ci àlluwa yi, kàddu ya woon ca àlluwa yu jëkk, ya nga toj. Su ko defee nga yeb àlluwa yi ci gaal gi.»

Daawudaa ngay fecc ak doole fa kanam Aji Sax ji. Daawudaa nga gañoo am xar-sànnim lẽe.

¶ La ca tegu ma damm sama ñaareelu yetub sàmm ba, Bennoo, ngir dog bokk gi dox diggante Yuda ak Israyil.

Buleen mer ba bàkkaar, te bu jant bi sowe seen mer;