Képp ku liggéey lenn ci boobu bés, su boobaa dinaa far kooku ci biir bànni Israyil, sànk ko.
TSK
TSK · Exodus 32:33
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Leviticus 23:30
TSK
Psalms 9:5
TSK
Yaa ma àtte yoon, dëggal ma, toog ci sab jal, di àtte njub.
Psalms 69:29
TSK
Yal nañu leen far ca téereb dund ba, bañ leena limaale ca aji jub ña.
Ezekiel 18:4
TSK
Mu ngoog, bépp bakkan maay Boroom. Muy bakkanu baay, di bakkanu doom, maa moom. Bakkan bi bàkkaar daal mooy dee.
Philippians 4:3
TSK
Yaw itam sama mbokkum surga bu dëggu bi, dama lay ñaan nga jàpple leen ci, ñoom ñaar ñooñoo bokkoon ak man coonob xamle xibaaru jàmm bi, ñoom ak ñoom Kelemaŋ, mboolem sama bokki liggéeykat yi seeni tur binde ca téereb dund ba.
Revelation 20:12
TSK
Ma gis néew ya, mag ak ndaw, ñu taxaw ca kanam ngàngune ma, ay téere ubbiku, beneen téere ubbikooti, di téereb dund ba. Ñu daldi àtte néew ya ca seeni jëf, na ñu ko binde ca téere ya.