TSK

TSK · Exodus 35:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ «Defarlul taabalu bantu séng, guddaayam di ñaari xasab, yaatuwaayam di xasab, taxawaayam di xasab ak genn-wàll.

¶ Ci biir loolu Besalel sàkk taabalu bantu séng, guddaay bi di ñaari xasab, yaatuwaay bi di xasab, taxawaay bi di xasab ak genn-wàll.