TSK

TSK · Exodus 39:42

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ La Aji Sax ji santoon Musaa ak Aaróona, noonu rekk la ko bànni Israyil defe.

¶ «Mboolem ku xareñ ci yeen, na ñëw, ngeen def li Aji Sax ji santaane lépp:

Su doon ñaari fan, su doon weer, mbaa ay fani fan la niir wa taxaw tiim màkkaan ma, des fa it, bànni Israyil dañuy dal, waaye duñu dem. Bu jógee rekk lañuy fabu.

Ca fukkeelu at maak benn, yemook juróom ñetteelu weer wa, di weeru Bul, ca la kër ga sotti, mook mboolem la ca bokk ak na mu wara bindoo lépp. Suleymaan tabax na kër ga ci juróom ñaari at.

Xare bu baax bi, xare naa ko, rawante bi, sottal naa ko, ngëm gi ma am, sàmm naa ko.