TSK

TSK · Exodus 5:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Waaye man xam naa ne buuru Misra du leen bàyyi, ngeen dem, mbete mu taseek doole ju ko tiiñ.

Nabal ne ndawi Daawuda: «Ana kuy Daawuda? Kuy doomu Yese sax? Jamonoy tey jaam yu baree ngi fàqe ci seeni sang.

Job 15:25 TSK

Moo xàccil Yàlla loxo, di jaay Aji Man ji njàmbaar,

Job 21:15 TSK

Ana kuy Aji Man ji sax ba ma di ko jaamu? Su ma ko tinoo, ana lu mu may jariñ?»

Yal na Aji Sax ji tëj gémmiñu kuy naxe, ak kuy làmmiñuy tëggu.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ñeel Daawuda. Ab dof a ngi naa ci xelam: «Yàlla amul!» Ñu ni mel ay def njekkar, seeni jëf siblu, kenn defu ci lu baax.

«Li nga nuy wax ci turu Aji Sax ji, dunu ko déglu.

¶ Gannaaw ràññee Yàlla jaralu leen dara, Yàlla it bërgal leen ak seen xel mu doyadi, ba ñuy def jooju jëf ju jekkadi.