TSK

TSK · Exodus 6:9

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Xanaa du lii lanu la waxoon ca Misra? Noon nanu la, nga bàyyi nu, nu surgawu waa Misra, ndax surgawu waa Misra moo nu gënal nu dee ci màndiŋ mi!»

Job 21:4 TSK

Sama tawat lii, da di maak nit a? Gannaaw du nit, ana lu ma tee xàddi?

Ku bëgga dund, dékku woppi yaram, waaye xol bu jeex maneesu koo wéye.