TSK

TSK · Exodus 7:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Nanga wax ak moom, digal ko li mu wara wax. Man maay ànd ak yeen, yaak moom, saa yu ngeen dee wax, te maa leen di xamal, yeen ñaar, li ngeen wara def.

da koo wax, ne ko: «Man maay Aji Sax ji. Nanga wax Firawna buuru Misra, li ma lay wax lépp.»

Buleen yokk dara ci kàddu gi ma leen di dénk, te buleen ci wàññi dara, ndax ngeen sàmm seen santaaney Yàlla Aji Sax, ji ma leen di dénk.

Aji Sax ji ne ma: «Bul ne: “Gone laa.” Képp ku ma la yebal, dem ca; lépp lu ma la sant, wax ko.

¶ Mu teg ca, ne ma: «Yaw nit ki nag, mboolem li ma lay wax, dégloo ko nopp, te teewloo ko xel.