TSK

TSK · Exodus 7:25

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Aji Sax ji def la ko Musaa ñaan, mbott ya dee, ba jeex ca kër yaak ca ëtt yaak tool ya.

Gàdd dem ca Daawuda, jottli ko ko, ne ko: «Ana yii yett loo ci taamu, mu dal ci sa kaw: juróom yaari ati xiif ci sam réew, am ñetti weer yooy daw say noon, am ñetti fani mbas ci sam réew? Xalaatal léegi te wax ci lenn, ma xam lu may jottli ki ma yónni.»