Exodus 7:11
TSK
Ba mu ko defee Firawna moom itam woo boroom xam-xam yaak jibar ya. Ñeengokati Misra ya ñoom it fexe ca seeni xargafuufa, ba def lu mel noona.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ba mu ko defee Firawna moom itam woo boroom xam-xam yaak jibar ya. Ñeengokati Misra ya ñoom it fexe ca seeni xargafuufa, ba def lu mel noona.
Loolu tax mbooloom Israyil roñ seen xiiwi sunguf yu amagul lawiir. Ñu ëmb seen ndabi notukaay ca seeni malaan, gàddu.