Buur Yàlla di ko ree, xam ne bésam a ngi ñëw.
TSK
TSK · Ezekiel 21:29
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yaaka sonn ci tegtali maa-man! Nañ taxaw boog, wallu la! Ñii di rëdd nataalu asamaan, di niiri biddiiw, ak di xool weer wu feeñ, xamle ca loo dikkleegul.
¶ «“Kon nag yeen, buleen déglu seen yonent yeek seetkat yeek firikati gént yeek boroom rawaan yeek ñeengokat yi leen di wax, naan leen dungeen tàbbi ci curgag buuru Babilon.
Du peeñuy caaxaan muy amati mbaa ngisaaney jayaate, fi biir kërug Israyil.
Kon nag gannaaw ñu ngi lajjal sama ñoñ, naan leen lépp jàmm! Te jàmm amul, mu mel ni miiru digaloo bu sew bu ñu ñab-ñabal, te ñii defuñu lu moy raax ca weexal,
wenn yoon wa jëme saamaru Babilon ca Raba, dëkkub Amoneen ñi; wa ca des jëme ko Yerusalem, dëkk ba ñu dàbbli, ca Yuda.
«“Dangaa masa bañ bànni Israyil. Ba musibay bànni Israyil taxawee, ba seen àppu mbugal mat sëkk, yaa leen jañax ci kaw ñaawkay saamar.