كل أسفار KYG

Ezekiel 21

KYG · الآية 33

48 أصحاحات

KYG / Ezekiel / الأصحاح 21

KYG · الآية 33

« Y aw nag nit ki, jottlil bii waxyu, nga ne: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ci mbirum Amoneen ñeek seeni saaga ne: Saamaroo saamar, bocciku, nara bóome, xacce ba mana yàppe, di tàkk ni melax.