1 Kings 6:33
TSK
Noonu it la def buntu néeg bu mag bi, ay jënam di bantu oliw, waaye bunt bi, jëwam aki jënam, bant lañu yu bindoo ñeenti wet.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Noonu it la def buntu néeg bu mag bi, ay jënam di bantu oliw, waaye bunt bi, jëwam aki jënam, bant lañu yu bindoo ñeenti wet.
¶ Ba loolu amee waa ja jàlle ma ba ca bunt néeg bu mag ba. Mu natt jën ya séq bunt ba, mu dëlle juróom benni xasab ci ñaari wet yépp.