Ezra 4:23
TSK
¶ Naka lañu jàng bataaxalu Buur Artaserses fa kanam Reyum boroom dëkk ba, ak Simsay bindkat ba aki nàttongoom, ñu ne coww ba Yerusalem, ca Yawut ña, jaay leen doole, gétën leen, ñu bàyyi liggéey ba.