Genesis 26:6
TSK
¶ Isaaxa nag toog Gerar.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Isaaxa nag toog Gerar.
Te sax ku may topp ku dul yaw, doomu buur? Ni ma toppe woon sa baay rekk laa lay toppe tey.»
Amul moos ku jub ci kaw suuf, kuy def lu baax te du bàkkaar.
¶ Ku mel ni Yuusufa, bokk ci giirug Lewi, te dëkke dunu Sippar, ndaw yi daan ko wax Barnaba, mu firi Ñaaxekat bi,
¶ Waaye ni ngeen di dunde seen sañ-sañu bopp, dangeen ciy xool ñi seen ngëm dëgërul, ngir ngeen bañ leena yóbbe bàkkaar.
Bu leen kenn nax: «Ànd bu bon yàq na jikko ju baax.»
¶ Su boobaa nu noppee doon ay tuut-tànk yu nit ñiy muusaatoo kàddu yu mel ni gannax yu nuy baaje, ak ngelawal mboolem àlluwa ju bees ju nuy pamti-pamtee ci seen biir pexey naxe ak njublaŋ, ngir fàbbi nu.