Numbers 24:22
TSK
Waaye réewum Keneen gépp ay xoyomu, ba leen Asur di yóbbuji njaam.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye réewum Keneen gépp ay xoyomu, ba leen Asur di yóbbuji njaam.»
¶ Ba loolu amee Senakerib buurub Asiri daldi fabu, ñibbi. Mu toog nag ca Niniw.
néegi Gebal, Amon ak Amaleg ak waa Filisteek waa Tir,
Waa dëkk yii di Karan ak Kane ak Eden ñoom it di say jula, ñook julay Saba ak Asur ak Kilmàdd.
Waajal-leen ay kàddu te dellu ci Aji Sax ji, ne ko: «Baal nu mboolem ñaawtéef te nangul nu, nu yékkati kàdduy màggal yu wuutu saraxi yëkk.
¶ Ba loolu wéyee kàddug Aji Sax ji dikkal Yunus ñaareel bi yoon. Mu ne ko:
¶ Yéeneb waxyu bu dal dëkk bi ñuy wax Niniw a ngi, di téereb peeñum Nawum ma dëkk Elkos.
ku la gis, daw la te naan: “Niniw tas na! Moo ku koy jooy?” Ana fu ma koy wutale ñu ko dëfal?»