Isaiah 23:1
TSK
¶ Yéene bii ñeel na dëkk ba ñuy wax Tir: Yeen waa gaali Tarsis ñi deele, jooyleen! Lépp a yàqu! Du kër, du teeruwaay. Fa dunu Sippar lañu leen ko waxe.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Yéene bii ñeel na dëkk ba ñuy wax Tir: Yeen waa gaali Tarsis ñi deele, jooyleen! Lépp a yàqu! Du kër, du teeruwaay. Fa dunu Sippar lañu leen ko waxe.
Ñu gorati garabu seen yu Basan, defare say joowu, kaw gaal gi, ñu defare ko banti sippar yu bawoo tefesi Géej gu mag ga, rafetale ko bëñi ñey.
Ay gaali Tarsis yu mag a daan yóbbu sam njaay. Nga fees dell, diis gann fi digg xolu géej.