كل أسفار KYG

Genesis 14

KYG · الآية 2

50 أصحاحات

KYG / Genesis / الأصحاح 14

KYG · الآية 2

à n d nañu, dal ci kaw ñoom Bera buurub Sodom, ak Birsa buurub Gomor, ak Sineyab buurub Atma, ak Semeber buurub Ceboyim, ak it buuru dëkk ba ñuy wax Bela, mooy Sowar ba tey.