Genesis 24:2
TSK
¶ Mu am bés Ibraayma wax surgaam, bi gëna yàgg ci këram, tey saytu alalam jépp, ne ko: «Dugalal sa loxo ci sama suufu lupp,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Mu am bés Ibraayma wax surgaam, bi gëna yàgg ci këram, tey saytu alalam jépp, ne ko: «Dugalal sa loxo ci sama suufu lupp,
Bu ñu nu nee: “Taxawleen foofu, ba nu fekksi leen,” nu yem fa, bañ leena fekki.
Ngalla def ma sa firndey mbaax, ba bañ yi gis ci, rus, ndax yaw Aji Sax, ji ma dimbali, dëfal ma.
Nit ñi fecci sama kóllëre, sàmmuñu ponki kóllëre gi ñu dige woon fi sama kanam, maa leen di def ni sëllu wa nit ña xaroon ñaar, jaare ca diggante xaaj ya, dogale ko seen ngiñ.
¶ Sàkkaryaa nag ne malaaka mi: «Lu may def ab takk ci loolu ba mu bir ma? Ndax man màggat naa, te sama soxna it làq na ay fan.»