TSK

TSK · Genesis 17:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Xon gi day nekk ci biir niir yi, ma di ko gis, di xalaat kóllëre, gi ma fas fàww, sama diggante, man Yàlla, ak mboolem xeetu mbindeef mu nekk ci kaw suuf.»

Ibraam teg ca ne: «Mayoo ma giir, te it jaam bu juddoo sama kër moo may donn.»

fekk waa Majan yóbbu nañu ko Misra, jaay ko Potifaar, jawriñu Firawna mi jiite ay dagam.

Waaye bépp jaam bu ñu jënd te mu xasa xaraf, man na cee lekk.

Su fekkee ne sangam a ko may jabar, ndaw si am ak moom ay doom, jabar jeek doomam yu góor mbaa yu jigéen, sang bee leen di moom. Moom ci boppam doŋŋ ay moom boppam.

Waaye su sarxalkat bi jëndee ab jaam ci xaalisam, jaam ba man na caa lekk. Jaam bu juddoo ci kër sarxalkat bi it man naa lekk ci ñamam woowu.

Ma ne leen: «Nun def nanu sunu kem kàttan ngir jotaat sunu bokki Yawut yi ñu jaayoon ay jaambur. Léegi yeen ci seen bopp ngeen di jaay seeni bokk, nun nu war leena jotaat?» Ñu ne xerem, amuñu lu ñu wax.