TSK

TSK · Genesis 17:18

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ndegam tey jii danga maa dàq, xañ ma sa jataay, dinaa dëkke daŋ-daŋ, di wëreelu ci kaw suuf, te kon ku ma gis rey ma.»

Rendileen seen sarax yi war, te wóolu Aji Sax ji.

Seeni ñaawtéef a dox seen digganteek seen Yàlla. Seeni moy a leen xañ kanamam, ba mu tanqamlu leen.

Acts 2:39 TSK

Ndax dige bi, yeen ak seen askan a ko moom, ak jaambur ñi féete fu sore ñépp, mboolem ñi sunu Yàlla Boroom bi woo.»