TSK

TSK · Genesis 19:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Teewul bala ñoo tëdd, góori Sodom, mag ak ndaw, daldi jóge gox bu nekk, ñëw yéew kër ga.

¶ «Su góor tëddee góor ni ñuy tëddee jigéen, ñaawtéef lañu def ñoom ñaar. Dee rekk mooy seen àtte, te ñooy gàddu seen bakkanu bopp.

Daawuda ne leen: «Déet bokk yi, buleen def noonu, ak li nu Aji Sax ji defal, aar nu, teg gàngooru yàqkat yi nu songoon ci sunuy loxo.

¶ Moo tax Yàlla bërgal leen ak seen xemmemtéef yu bon yi ci seen xol, ba ñu sóobu ci jëflantey sobe juy teddadil seen yarami bopp.

Jude 1:7 TSK

Naka noonu itam Sodom ak Gomor, ak dëkk ya leen wër, ñoo yebu woon ci powum séy, ak jaxasoo gu woroo ak bindub judduwaale, ba ñu def leen misaal, ñeel ña nara tegoo mbugalum sawara wu sax dàkk.