¶ Rasel ak Leya ne ko: «Ndax amati nanu benn cér walla ndono sunu kër baay?
TSK
TSK · Genesis 2:24
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 31:14
TSK
Deuteronomy 4:4
TSK
Waaye yeen ñi ŋoyoon ci seen Yàlla Aji Sax ji, yeen ñépp a ngi dund tey jii.
Psalms 45:10
TSK
Ay doomi buur a ngi ci jigéen ñi nga teral, sab lingeer féete la ndijoor, takkoo ngëneelu wurus.
Proverbs 31:10
TSK
Jeeg bu jàmbaare, ndaw lu jafe, ba rawati gànjar!
Acts 11:23
TSK
Ba Barnaba dikkee ba gis yiw, wi leen Yàlla may, dafa bég, di leen ñaax ngir ñu ŋoye seen xol ci Sang bi.
Xanaa xamuleen ne, kuy taqoo ak ab gànc bu jigéen, mook moom, jenn jëmm lañuy doon? Ndaxte noonu lañu waxe ne: «Ñoom ñaar ay mujj di wenn suux doŋŋ.»
¶ Ñi séq ab séy nag, maa leen dénk lii, te du sama ndigal, ndigalal Boroom bee. Jabar ji, bumu teqlikoo ak jëkkëram.
1 Timothy 5:14
TSK
Moo tax ma bëgg, jëtun ñiy ndaw séyaat, ami doom, yor seen kër, ba noon bi du am lu mu yàqe sunub der.