TSK

TSK · Genesis 20:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ibraam bàyyikooti fa, aw yoonam, jublu àllub Negew.

Sóol ne leen: «Yal na leen Aji Sax ji barkeel ndax yég ngeen ma.

Acts 5:9 TSK

¶ Ci kaw loolu Piyeer ne ko: «Ana lu ngeen di mànkoo, di nattu Noowug Boroom bi? Déglul, tànk yi suuli woon sa jëkkër a ngoogu ci bunt bi di la yóbbusi yaw it.»

¶ Ba Yàllay woo Ibraayma, ngir mu génn, jëm bérab ba mu mujj muurloo, ngëm la déggale Yàlla, ba génn, dem te xamul woon fu mu jëm.