Genesis 20:5
TSK
Du góor gi da maa waxoon ne kii jigéenam la? Du jigéen ji it da maa waxoon ne kooku càmmiñam la? Fexewuma dara lu ñaaw te di ko tey de!»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Du góor gi da maa waxoon ne kii jigéenam la? Du jigéen ji it da maa waxoon ne kooku càmmiñam la? Fexewuma dara lu ñaaw te di ko tey de!»
Abimeleg daldi fay doxe àrtu waa réewam mépp ne leen: «Ku laal waa jii walla soxnaam, dees na ko rey.»
Bul yedd kuy ñaawle, da lay jéppi; yeddal ku rafet xel, mu naw la.
Kàddu yu lay yedd ci kuy dégg, jaarob wurus la mbaa gànjaru ngalam.
Ci kaw loolu njiitu mool ya dikk ba ca moom, ne ko: «Yaw, ana looy nelaw? Jógal kay woo sa yàlla wall! Jombul mu geesu nu, ba dunu sànku.»