Genesis 26:23
TSK
¶ Ba mu fa jógee, dafa dellu Beerseba.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba mu fa jógee, dafa dellu Beerseba.
¶ Israyil nag dem, yóbbaale mboolem lu bokk ci moom. Ba mu agsee Beerseba, dafa sarxal Yàllay baayam Isaaxa.
Ba mu ko defee ñu dem ba Tir, dëkk ba ñu wëralee ab tata, jóge fa dem ca mboolem dëkk-dëkkaani Eween ñaak Kanaaneen ña. Ñu àkkeji Beerseba ca bëj-saalumu màndiŋu Yuda.
¶ Ilyaas gis na mu deme, daldi daw, ngir rawale bakkanam. Mu dem ba Beerseba ca réewum Yuda, bàyyi fa surgaam.