TSK

TSK · Genesis 21:8

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Isaaxa nag berndeel leen, ñu bokk lekk, ba noppi naan.

¶ Ñu teg ca ñetti fan, Firawna di màggal bésu juddoom, dajale jawriñam yépp, di leen berndeel, daldi cay seppee kilifa gay topptoo ay naanam, ak kilifag lakk-kati mburu ya, siggil leen.

¶ Naka la feral xale bi, ànd ak moom, muy lu tuut, mu yóbbu ko ca kër Aji Sax ji ca Silo. Mu yóbbaale ñetti yëkk, ak benn efab sunguf, yemook fukki kilo, ak mbuusu biiñ.

Ba Abner agsee Ebron ca Daawuda, ñaar fukki nit la àndal. Daawuda berndeel Abner, mook nit ña ànd ak moom.

Ci ñetteelu atu nguuram mu maye bernde, ñeel kàngamam yépp ak jawriñam yépp, di njiiti xarey diiwaanu Pers ak diiwaanu Medd, garmi yeek kàngami dëkk yi bokk teew.

Hosea 1:8 TSK

¶ Ba Gomer feralee Lo Ruwana, ëmbaat na, ba am doom, muy góor.