TSK

TSK · Genesis 24:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

maa ngii taxaw ci seyaan bi; janq bay ñëw rootsi, ma ne ko: ‘Doo ma may tuuti ci sa njaq li, ma naan,’

Yettro, sarxalkatu Majan ba nag, amoon na juróom ñaari doom yu jigéen. Ñu ñëw di rootsi, di duy mbalka, ya ñuy wëgge seen juru baay.

Naka lañu yéeg tund wa, jëm ca dëkk ba, daldi taseek janq ju ca jóge, di rooti. Ñu laaj leen ne leen: «Góorug giskat bi fii la féete?»

Loo mébét, bàyyil Yàlla xel, mu xàllal la yoon.