TSK

TSK · Genesis 24:53

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba loolu amee surga ba jële fukki giléem ca giléemi sangam, dem, yóbbaale li gën ci mboolem xeeti alalu sangam. Ma nga jëm réewu Mesopotami, ga Naxor dëkk.

Képp kuy jigéen ci bànni Israyil, na laaj dëkkandoom, laajaale ku dëkk ak dëkkandoom, ay gànjari xaalis, ak gànjari wurus, ak yére yu ngeen di solal seen doom yu góor ak yu jigéen, ba waa Misra ne duŋŋ.»

Fekk na bànni Israyil def la leen Musaa santoon ca waa Misra. Sàkku nañu ca ñoom ay gànjari xaalis ak wurus aki yére.