TSK

TSK · Genesis 25:30

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba loolu amee Yanqóoba dafa yónni ay ndaw, ñu jiitu ko ca magam Esawu, ca réewu Seyir, di diiwaanu Edom.

Esawu nag dëkk ca tundu Seyir: Esawu moomu mooy Edom.

Ñooñooy doomi Esawu, mi ñuy wax Edom, ñooñooy doomam yu góor, ñook seeni làng.

kilifay waa Edom jàq, njiiti Mowab di kat-kati, mboolem waa Kanaan tiit, ne yasar;

Buleen sàkku mukk jàmmu ñooñu mbaa seen njariñ, seen giiru dund, ba fàww.

¶ Peeñum Abdiyas a ngi. Boroom bi Aji Sax ji moo wax lii ñeel askanu Edom.