Genesis 24:36
TSK
Sama soxnas sang Saarata nag dem na ba màggat, doora amal sama sang doom ju góor. Doomam jooju la jox li mu moom lépp.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Sama soxnas sang Saarata nag dem na ba màggat, doora amal sama sang doom ju góor. Doomam jooju la jox li mu moom lépp.
Gannaaw ay doom lanu nag, ay boroom cér lanu, ay boroom cér yu Yàlla sédd, cér yu nu bokk ak Almasi, gannaaw noo bokk ak moom ab coono tey, ngir bokk ak moom teraangay ëllëg.
Te it sëti Ibraayma yépp bokkuñu ci askanam, waaye li Mbind mi indi moo di: «Ci Isaaxa lees di tudde saw askan.»
Te su ngeen bokkee ci Almasi, yeen ay askanu Ibraayma, te yeena jagoo dige ba.
ndax Yàlla la soob mu dëël gépp matam ci moom.