TSK

TSK · Genesis 25:9

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Saarata nag gis doomu Ajaram Misra, jaak Ibraayma, muy kókkalee.

Ibraayma daldi suul soxnaam Saarata ca xuntim xeer ma ca biir toolub Magpela, booba janook Mamre, di Ebron léegi, ca réewu Kanaan.

Bés bu ma fekkijee samay maam, nanga ma jële Misra, denci ma ca seen xuntim bàmmeel.» Yuusufa ne ko: «Dinaa la defal li nga wax.»

Foofa lañu denc Ibraayma ak soxnaam Saarata, te foofa lañu denc Isaaxa ak soxnaam Rebeka, te fa laa denc Leya it.