TSK

TSK · Genesis 26:30

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba loolu amee doom ja màgg, ba bés, ba ñu ko feralee. Keroog Ibraayma def na bernde ju mag.

Yettro, gorob Musaa, daldi sàkk saraxu rendi-dóomal ak yeneen sarax, jagleel ko Yàlla. Aaróona ak magi Israyil ñépp dikk, ñu bokk lekk ñook gorob Musaa fa kanam Yàlla.

¶ Sàkkuleen jàmm seen diggante ak ñépp, te it sàkkuleen sellnga, nde ku sellul du gis Boroom bi.