Genesis 27:4
TSK
Toggal ma ko, ba mu neex, ni ma ko bëgge, indil ma, ma lekk, ndax ma ñaanal la lu ma tibbe ci sama xol, bala may dëddu.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Toggal ma ko, ba mu neex, ni ma ko bëgge, indil ma, ma lekk, ndax ma ñaanal la lu ma tibbe ci sama xol, bala may dëddu.»
Isaaxa laaj ko ne ko: «Mbaa wóor na ne yaw ay Esawu?» Mu ne ko: «Waawaaw.»
Mu dellu ne ko: «Man itam yonent laa ni yaw. Malaaka wax na ma ci ndigalal Aji Sax ji ne ma: “Waññi ko, mu ànd ak yaw sa kër, sex dugub, naan ndox.”» Fekk na la muy wax amul.
Yeena naay: «Danoo wóllëranteek ndee, njaniiw lanu digool, ba du nu moom, ba bu yaru musiba dikkeek diisaayam, du nu laal? Noo def ay fen sunu rawtu, ay wor di sunu làquwaay.»