TSK

TSK · Genesis 29:20

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Séetul ak kii, ba ayu bésam mat, ma door laa jox ki ci des, soo ma dee liggéeyaatal diiru juróom ñaari at.»

Su ko defee nga jox ma samay doom ak sama jabar yi taxoon ma di la liggéeyal, te bàyyi ma, ma dem, ndax yaw ci sa bopp xam nga li ma la liggéeyal.»

Xale bu góor bi daldi gaawtu def li ñu ko sant ndax mbëggeelam ca doomu Yanqóoba. Booba Sikem lañu gënoona weg ca waa kër baayam yépp.

Su Galàdd dee dëkkub defkati ñaawtéef, dañoo tekkiwul dara. Fa Gilgal lees di rendee ay saraxi yëkk, te seeni sarxalukaay ni jali xeer lay mel ci ay tooboy tool.

Cofeel moo di: lépp, nga bale; lépp, nga gëm; lépp, nga yaakaar; lépp, nga dékku.

te ngeen di doxale cofeel, ni Almasi mi nu sopp, ba jooxeel nu bakkanam, def ko saraxu sawara, ngir xetug jàmm, ñeel Yàlla.