Genesis 3:13
TSK
Yàlla Aji Sax ji ne jigéen ja: «Yaw, li nga def nii mooy lan?» Jigéen ja ne ko: «Aa, jaan de moo ma nax, ba ma lekk ci.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Yàlla Aji Sax ji ne jigéen ja: «Yaw, li nga def nii mooy lan?» Jigéen ja ne ko: «Aa, jaan de moo ma nax, ba ma lekk ci.»
Loolu tax na Aji Sax ji wax buurub Israyil ne ko: “Lal bi nga tëdd doo ko wàcc, ndax dinga dee moos.”» Ci kaw loolu Ilyaas dem.
ne ko: «Aji Sax ji nee: Yónni nga ay ndaw, di seeti ca Baal Sebub, tuuru Ekkron, mel ni Yàlla amul ci Israyil, ba ñu man koo laaj kàddoom. Loolu tax na lal bi nga tëdd, doo ko wàcc, nde dinga dee moos!»
Waaye na jaan ja naxe woon Awa, ca pexeem, ragal naa seenum xel yàqoo noonu, ba dëddu ngëm gu dëggu te set gu ngeen ŋoye woon ci Almasi.