TSK

TSK · Genesis 32:25

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba jant bay fenk, Yanqóobaa ngi soox tànk bi, di bàyyikoo Penuwel.

Meram di lu gàtt, aw yiwam sax dàkk. Rongooñ gane, fanaan, ay ree xëysi.

Aji Sax ji, Aji Sell ju Israyil dafa wax, moom mi ko bind, mu ne: «Lu dikkagul, nu ngeen ma ko ñemee laaje; am dangeen may jox ndigal ci samay doom, jox ma ko ci li ma liggéeye samay loxo?

Ci biiru ndeyam la kii suufoo ab seexam; kii moo tollu ci dooleem, bëreek Yàlla.

Luke 11:5 TSK

¶ Yeesu teg ca ne leen: «Ana kan ci yeen moo seeti ab xaritam xaaju guddi, ne ko: “Xarit, lebal ma ci ñetti mburu.