كل أسفار KYG

Genesis 32

KYG · الآية 7

50 أصحاحات

KYG / Genesis / الأصحاح 32

KYG · الآية 7

N daw ya daldi dem ba délsi ca Yanqóoba, ne ko: «Dem nanu ca sa mag Esawu, waaye moom ci boppam mu ngi ci yoon wi di ñëw, fekksi la fii, te ma nga ànd ak ñeenti téeméeri góor.»