Genesis 27:39
TSK
Baayam Isaaxa ne ko: «Déglul, ma wax la, dinga dëkk fu sore ngëneeli suuf, mbaa fu la layub asamaan tiime.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Baayam Isaaxa ne ko: «Déglul, ma wax la, dinga dëkk fu sore ngëneeli suuf, mbaa fu la layub asamaan tiime.
Saxu watar du suur, ñaar ñu jigéen la am: Jox Ma ak Jox Ma. Ñett a ngii ñu dul suur, ba ci ñeent ñu dul ne doy na mukk:
¶ Ci kaw loolu Anañas dem, dugg ca kër ga, teg Sóol loxo, ne ko: «Mbokk mi Sóol, Sang Yeesu, mi la feeñu woon ci yoon wi nga dikke, moo ma yebal ci yaw, ngir nga dellu di gis te feese Noo gu Sell gi.»
Mbokk mi, mbégte mu réy, ak xel mu dal laa am ci sa cofeel, ndax ni nga serale xolu aji sell ñi.