¶ Surga ba nag génne ay gànjari xaalis ak yu wurus booleek ay yére, jox Rebeka. Càmmiñ la ak yaay ja itam, mu may leen alal ju takku.
TSK
TSK · Genesis 34:12
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 24:53
TSK
Genesis 31:41
TSK
Ñaar fukki at a ngii, ma di la jaamu ci kër gi, liggéeyal naa la fukki at ak ñeent ngir sa ñaari doom yu jigéen ñii, teg ci juróom benni at yu ma la sàmmal say gàtt, nga soppi sama peyoor fukki yoon ak juróom.
Exodus 22:16
TSK
Su fekkee ne baayam dafa lànk, ne du ko ko may it, du tere mu wara fey ci xaalis lu tollook warugaru janq.
1 Samuel 18:25
TSK
¶ Sóol ne leen: «Waxleen Daawuda ne ko, Buur de sàkkuwul ub can: xanaa téeméeri mbuñukay waa Filisti yu mu feyoo ci noonam yooyu.» Booba la Sóol laloon mooy pexe mu tàbbal Daawuda ca loxol waa Filisti.
Hosea 3:2
TSK
¶ Ci kaw loolu ma takk ko ci fukki poseti xaalis ak juróom, ak ñeenti téeméeri kiloy lors ak juróom fukk (450).