Genesis 25:27
TSK
¶ Ba mu ko defee gone ya di màgg, Esawu di rëbbkat bu ñaw, di ku bëgg àll; Yanqóoba moom di nit ku gàtteñlu te bëggoon toogaayu kër.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba mu ko defee gone ya di màgg, Esawu di rëbbkat bu ñaw, di ku bëgg àll; Yanqóoba moom di nit ku gàtteñlu te bëggoon toogaayu kër.
¶ Ba ñu ca tegee ñaari ati lëmm, Absalom dem di watlu ay xaram ca Baal Àccor, fa feggook diiwaanu Efrayim. Absalom daldi fay woo doomi buur yu góor yépp.
Yàlla daal ngeen di waxal njubadi, di ko duural?
Bàkkaaru làmmiñ dugal na boroom, ku jub mucc ci njàqare.
Bul tuumaal nit ci neen, te bu ko seedeel ay fen.
Noo tooñ Aji Sax ji, wor ko, te noo dëddoo sunu Yàlla jii, kàdduy fitna ak fippu, ak fen yu nu mébét, nas ko,
Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.