TSK

TSK · Genesis 35:24

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Moo tax mu tudde ko Yuusufa (mu firi Yal na dolli), ndax dafa ne: «Yal na ma Aji Sax ji dollil doom ju góor.»

Booba Rasel a ngi waaja faatu. Terewul bala bakkanam a rot tudde na xale bi Benoni (mu firi Sama doomu coono). Teewul baay bi tudde ko Beñamin (mu firi Sama doomu njiglaay).

¶ Doom yu góor yi Rasel, soxnas Yanqóoba, am nag ñoo di Yuusufa ak Beñamin.

Ruth 4:11 TSK

¶ Waa pénc ma mépp ak mag ña nag ne ko: «Noo ko seede. Yal na Aji Sax ji def ndaw siy séysi sa kër, mel ni Rasel ak Leya, ñoom ñaar ñi giir waa kër Israyil gépp. Yal nanga tekki ci digg Efrata te amu tur ci Betleyem.