TSK

TSK · Genesis 36:20

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

ak Oreen ña ca seen tund wa ñuy wax Seyir. Da leena dàq ba ca garabu Paran gu mag ga ca wetu màndiŋ ma.

Doomi Lotan yu góor ya nag ñooy Ori ak Emam. Jigéenub Lotan di Timna.

Seyir nag la Oreen ña jëkkoona dëkk, waaye Esaween ñaa leen fa dàqe, faagaagal leen, wuutu leen, noonu Israyil def rekk ak céru suufam bi leen Aji Sax ji jox.