TSK

TSK · Genesis 36:34

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Doomi Elifas yu góor yi di: Teman ak Omar ak Sefo ak Gatam ak Kenas.

Job 2:11 TSK

¶ Gannaaw loolu ñetti xariti Ayóoba ñoo dégg mboolem musiba moomu ko dikkal. Ku nekk ci ñoom jóge këram: Elifas waa Teman ba, ak Bildàdd waa Suwa ba, ak Cofar waa Naama. Ñu bokk daje ngir dikk mas-sawu Ayóoba, dëfal ko.